Bayi Yoon Lyrics & Tabs by Daara J

Bayi Yoon

guitar chords lyrics

Daara J

Album : School of Life senegal PlayStop

Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani

Ci gééw kén douko jamnaani
Emana sama gaa gna ngi
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jiko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon, oh oh ouh oh
Africains, et fiers de ce que nous sommes
Oh oh ouh oh
Fier d'être africain je suis, je suis africain donc je suis
Mes ancêtres ont souffert le martyr

Oh oh ouh oh
Fier d'être africain je suis, je suis africain donc je suis
Mes ancêtres ont souffert le martyr
Pour que je puisse relever le défi
C'est à moi de porter le flambeau
Ils ne peuvent pas me mettre en lambeaux
Pour me mettre KO il faut
Minimum une armée de 100 000 Rambos
Dis à ton prof d'histoire qu'il raconte des histoires
La plus grande des civilisations est née en Afrique Noire
L'Afrique a inspiré le monde avec ses pyramides
Sa science, ses mathématiques, ses symboles et ses signes
Elle créa l'écriture avec les hiéroglyphes
Du temps des pharaons, tu me crois pas?
Vas y demande à Akhé... naaaton oh ouh
(De Dakar à Marseille)
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jiko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon, oh oh ouh oh
Africains, et fiers de ce que nous sommes
Oh oh ouh oh
Dafa melni gnou ngi daw jeum fénén ni
Wacc wacc nagnou ande yi
Xéeb sougnou ngande yi fékki borom
Jikko you dande yi fo daw fo daw
Di nga wirri n daari fa jougé fi
Nga dooré fila wooré doufou sorré
Afro sama dolé na nga mako xolé
Geum sama demb doon nittou téy
Njaxass ni xéetou parfum 'K'Gowé
Africains koula xass foy gnawé (gnawé)
Africains xola gneup nignouy ngaangé (ngaangé)
Africains soy joug doufi gawé
Koula xol dina séet fanlalay ngagné
Geum sa bopp xam fi nga bokk
Melni garab réen banxass ak xob
Dougnou fatté fignou jogé ndakh panafricanistes
Délo sougnou xél démb kanamou mame gnou giss
Dimbali jam yi biss
Gnoul métisses dékkil Osiris carbone 14 souliwaat gnou giss
Histoire bindaat grand-père ba petit-fils
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jiko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Deug deug xam sa boppa geun
Gnou wakh la ki nga doon, oh oh ouh oh
Africains, et fiers de ce que nous sommes
Oh oh ouh oh
Bamako Singapore Anghata!
(Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci gééw kén douko jamnaani
Emana sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci gééw kén douko jamnaani
Emana sama gaa gna ngi)
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Jiko you rafét yignou ragnéwoon?
Dafa melni dagnou bayi sougnou yoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon
Beugeu askano lougnou momoutoon
Sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci gééw kén douko jamnaani
Emana sama gaa gna ngi
Doomu Africa mbeur la kaamil
Yagg yagg dina daani
Ci gééw kén douko jamnaani
Emana sama gaa gna ngi

Like us on Facebook.....
-> Loading Time :0.0071 sec