Birima Lyrics & Tabs by Youssou N'Dour

Birima

guitar chords lyrics

Youssou N'Dour

Album : Eyes Open / Joko from Village to Town / The Guide (Wommat) african PlayStop

Maysa tende jodo yaa moom liile Hi woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Buri samba laobe yaa moom liile Hi woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Damel maisa Penda Joor
Jooro Jooro Jooro Jooro Ho Ho Ho Hoy
Sama waaji ken dula jam naani
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
mmmm mmm
Wooy Tedi Ngoné maarne be Sambaa
Kuli baca senge ndat Biran ngamoo
Ngoné maca nas mbay maca jeeri
Samba yaasimooooo dike mbay Kuja dooooki
Yay borom mbaboor... mi
Hi (di) woy Birima Sama waaji ken dula jam naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Yay borom mbaboor... mi
Hi (di) woy Birima Sama waaji ken dula jam naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Dogo fal ak mawa joor Kumba samba yaay jaloor
Dogo dogo . Ho ho ho!!
Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee
Choeur
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel
Kayor niila
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Like us on Facebook.....
-> Loading Time :0.0126 sec